Ay pexe ngir dëppook Coppikug Kéew gi ci Ndar

Li aju ci dëkkuwaay bi Ndar, dëkku ndox : déndub bël. Tefes gi sës ci taaxu Ndar dëkk la bu ëmb kàrcey nappkat yi, ay taax yu ñu jagleel doxandeem yi (turism) ak barab yu ñuy sopparñee jën. « Langue de Barbarie »  moo ëpp nit ci Ndar. Ñetti kàrce yii – Get-Ndar, Ndar-Tuut, Goxu Mbaac – […]

Soutenance de thèse de Abdou Khadre SANO

Soutenance de thèse de Abdou Khadre SANO, chercheur au GERM, le mercredi 25 novembre 2020 à 09h à l’Université Gaston Berger de Saint-Louis sur : Du mécénat à l’arène politique : engagements des migrants de Matam dans les collectivités locales d’origine.